Borom Daaraji (RTA)

Enseignements Spirituels

Khilass/Biographie du Prophète Mouhamed PSL: chapitre 6, cours 2.

وَمَاتَ ضِيقٌ مِنَ النِّسْوَانِ مِنْ أَسَفٍ عَرَفْنَ ذَاكَ مِنَ الْكُهَّانِ لَا تَهِمِDeux cents femmes sont mortes de désespoir, ayant pris connaissance de cette conception par leurs devineresses. فَيَا لَهَا لَيْلَةً غَرَّاءَ قَدْ نُكِسَتْ فِيهَا الْكَنَائِسُ وَالْأَصْنَامُ مِنْ رَغَمِO ! merveille ! Quelle merveilleuse nuit blanche qui a vu leurs temples et leurs idoles s’effondrer de honte. وَ قَدْ تَلَاقَتْ وُحُوشُ الْخَافِقَيْنَ كَمَا سَوَاكِنُ الْبَحْرِ قَدْ لَاقَتْ مِنَ النُّعَمِTous les fauves de l’orient et de l’occident se sont retrouvés, de même que les êtres du monde aquatique, dans la joie. سَرِيرُ كُلِّ مَلِيكٍ صَارَ مُنْتَكِسًا بِلَا خِلَافٍ وَرَبِّ الْكَعْبَةِ الْحَرَمِJe jure, par le Seigneur de la Ka’ba –sans crainte d’être démenti- que le lit de tout souverain s’est mis à s’incliner. قَضَى بِأَبْوَاءَ عَبْدُ اللَهِ حِينَ مَضَى شَهْرَانِ لِلْحَمْلِ هَذَا أَشْهَرُ الْكَلِمِAbd-Allah s’éteignit à Abwa, deux mois après la conception du Prophète. Çà, c’est la version la plus répandue. وَ قِيلَ فِي طَيْبَةٍ قَدْ كَانَ مَدْفَنُهُ فِي دَارِ تَابِعَةٍ فَاحْذَرْ مِنَ الْوَهَمِIl est également dit que sa tombe est à Tayba, dans la maison de Tâbi’a, éloigne- toi de la conjecture. تَابِعَةً ضَبَّطَ الزُّرْقَانِ وَالْحَلَبِي بِالتَّاءِ فَوْقُ وَعَيْنٍ غَيْرِ مُنْعَجِمِDans « Az Zurqân » et « Al Halabi », il est mentionné « Tabi’’a » (écris la lettre T avec deux point suscrits et la lettre ayn sans point suscrit) يُرْوَى بِنُونٍ وَغَيْنٍ بَعْدُ مُعْجَمَةٍ مِنْ غَيْرٍ عَزْوٍ وَلَا ضَبْطٍ سِوَى الْقَلَمِSelon d’autres, il faut l’écrire avec les lettres « n » et « gh » affecté d’un point suscrit. Cela n’est mentionné que par un manuscrit. قُلْ تَارِكٌ خَمْسَةَ الْأَجْمَالِ جَارِيَةً سَيْفًا كَذَا وَرِقٌ مَعْ قِطْعَةِ الْغَنَمِTu peux aussi dire, cher lecteur, que ce dernier a laissé comme héritage cinq chameaux, une servante, un sabre, de l’argent et un petit troupeau. وَعُدَّ شُقْرَانَ مِنْ مَتْرُوكِ وَالِدِهِ وَ أُمُّهُ تَرَكَتْ دَارًا بِشَعْبِهِمِTu peux ajouter Chaqrân parmi ce que son père a laissé et aussi la maison d’Amina à Chi’’b. وَ مِنْ خَدِيجَةَ دَارًا بِالْحَجُونِ حَوَى خَيْرُ الْبَرِيَّةِ مِنْ عُرْبٍ وَمِنْ عَجَمِLe meilleur parmi les Arabes et les non Arabes a hérité aussi d’une maison ayant appartenu à Khadija et sise à Al Hajûn. وَقَالَ الاَمْلَاكُ رَبَّ الْخَلْقِ سَيِّدَنَا يَبْقَى نَبِيُّكَ مَعْدُودًا مِنَ الْيُتُمِLes anges ont dit : «Ô toi, SEIGNEUR de la création, notre Maître, ton prophète continuera-t-il à être inclus parmi les orphelins?» وَقَالَ لَا إِنَّنِي لَا شَكَّ حَافِظُهُ وَرَبُّهُ عَوْنُهُ كَافِيهِ فِي الْإِمَمِIL répondit : «Non ! C’est MOI, sans nul doute, qui le garderai, l’éduquerai, l’aiderai, le protégerai contre tous les maux.» مِنْ بَعْدِ مَا قَدْ خَلَا وَاوٌ يُقَالُ لَهَا هَا أَنْتِ حُمِّلْتِ بَدْرًا سَيِّدَ الْأُمَمِSix mois après, on annonça à Amina : «Ô femme bénie, sache que tu portes une pleine « lune » qui sera le seigneur de l’univers.» إِذَا وَضَعْتِيهِ سَمِّيهِ مُحَمَّدًا الْأَمْرَ اكْتُمِي أَيَّ كِتْمَانٍ فَتَغْتَنِمِQuand tu le mettras au monde, donne-lui le nom de Muhammad et garde jalousement son secret, ainsi tu t’enrichiras. قُولِي أُعِيذُ لَهُ مِنْ شَرِّ ذِي حَسَدٍ بِالْوَاحِدِ الصَّمَدِ الْمَوْصُوفِ بِالْقِدَمِTu prononceras alors les mots suivants : «je prierai pour le préserver des envieux, par DIEU l’Absolu, l’Unique, le Pré éternel.» وَكُلُّ مَا لِقُرَيْشٍ دَبَّ قَدْ نَطَقَتْ بِحَمْلِ خَيْرِ عِبَادِ اللَهِ كُلِّهِمِTout être animé, au sein des Quraychites, a mentionné cette conception du meilleur de tous les serviteurs de DIEU. فَاحْضَرَّتِ الْأَرْضُ وَ الْأَشْجَارُ قَدْ حَمَلَتْ فَسُمِّيَ الْعَامُ عَامَ الْفَتْحِ وَالرَّفَمِLa terre a reverdi, les arbres ont fructifié. L’année fut appelée année de l’ouverture et du bonheur. وَلِلنِّسَا أَذِنَ الرَّحْمَانُ حَمْلَ ذُكُو رِ ذَلِكَ الْعَامَ إِكْرَامًا لِمُحْتَرَمِLe MISERICORDIEUX a gratifié d’un garçon, cette année-là, toutes les femmes enceintes pour honorer notre respectable Prophète. Mame Maodo Malick Sy borom Parassol bi

Khilass/Biographie du Prophète Mohamed PSL: Chapitre 6, Cours 1

وَعَبْدُ مُطَّلَبٍ مِنْ بَعْدُ مَرَّ إِلَى فَتَاةِ زُهْرَةَ ذَاتِ الْمَجْدِ وَالْكَرَمِAbd-Mutaleb a rencontré, après cet événement, une noble jeune fille de Zohrâ de grande vertu et de grande noblesse. مَرًا عَلَى امْرَأَةٍ تُدْعَى بِفَاطِمَةٍ تَبْغِي الْمَمَالَ إِلَيْهَا وَهْيَ لَمْ تُرَمِIls avaient, au préalable, rencontré une femme du nom de Fâtima qui aspirait à cette union alors qu’elle n’était pas celle qu’on cherchait. وَحَازَ إِذْ ذَاكَ عَبْدُ اللَهِ سَيِّدُنَا حَدْوًا إِلَى الْخَيْرِ نَافِي الضَّيْرِ وَالنِّقَمِAbd-Allah , notre seigneur, avait alors dix-huit ans et croissait en gloire, à l’écart de tout penchant vicieux, لِكَيْ يُصَيّرَهَا صَدْفًا لِدُرَّتِهِ أَمِينَةً نَقِيَتْ عَنْ سَائِرِ التُّهَمِPour qu’il prenne Amina, coquillage couvant de l’or, qui était pure et à l’abri de tout soupçon. وَقِيلَ زَوَّجَهَا وَهْبٌ وَقِيلَ وُ هَيْبٌ عَمُّهَا وَمُرَبِّيهَا بِحِجْرِهِمِOn rapporte que c’est Wahab qui célébra l’union de cette dernière ou son oncle paternel Wuhayb, celui qui l’a élevée chez lui. وَهْيَ حِينَئِذٍ أَعْلَى النِّسَا شَرَفًا وَ نِسْبَةً وَافْتِخَارًا مِنْ جُدُودِهِمِDe par sa lignée, elle était alors la plus distinguée des femmes, la plus noble, la plus vertueuse. فِي الشِّعْبِ يَوْمَ الثِّنَا الْمُخْتَارَ قَدْ حَمَلَتْ وَقَالَ سَهْلُ ابْنُ عَبْدِ اللَهِ ذُو الْوَذَمِC’est à Chi-b, un lundi, qu’elle porta en son sein l’Elu, selon le distingué Sahl Ibn Abd-Allah لَيْلَ الْعَرُوبَةِ حَلَّ الدُّرُ فِي رَجَبٍ ثُمَّ الْمُنَادِي يُنَادِي مُسْمِعَ الْفَهِمِC’est la veille d’un vendredi du mois de Radjab qu’est descendu « l’Or » puis une voix appela pour informer ceux qui voulaient l’être : تَنَبَّهُوا أَنَّ نُورَ الْخَتْمِ لَيْلَكُمُ قَدْ حَلَّ فِي خِيمَةٍ مِنْ أَطْهَرِ الْخِيَمِ«Réveillez-vous ! La Lumière parfaite est descendue en cette nuit vôtre dans une tente, la plus pure des tentes.» Iأَنْ عَطِّرُوا بَخِّرُوا خَيْرَ الْبُخُورِ وَأَفْرِ شُوا السَّجَادَاتِ تَكْرِيمًا عَلَى الْقُذَمِO Miracle ! Parfumez-vous ! Encensez-vous de votre meilleur encens. Etalez vos tapis pour honorer le meilleur des êtres. قَالَ الْمَلَائِكُ أَبْوَابُ السَّمَا فُتِحَتْ كَذَا الْجِنَانُ وَنُورُ الشَّمْسِ فِي الْعِظَمِLes anges dirent : «toutes les portes du ciel sont ouvertes, de même que celles des paradis et la lumière du soleil a été intensifiée.» وَأَنَّ رَنَّ اللَّعِينُ الْخَبُّ يَحْضُرُهُ جُنُودُهُ وَهْوَ رِعْدِيدٌ مِنَ السَّدَمِSatan le maudit, désormais bredouille, a gémi et bougonné au milieu de ses suppôts et tremblé de peur. وَقَالَ وَيْلَكُمُ يَا أُمَّتِي حُمِلَتْ فِي هَذِهِ دُرَّةٌ مِنْ أَحْسَنِ التُّوَمِIl dit : «malheur à vous mes compagnons ! Le plus pur vient d’être conçu dans de l’or, cette nuit.» وَجَاءَ آدَمُ تَبْشِيرًا وَشِيتُ لَهَا إِدْرِيسُ نُوحٌ وَهُودٌ وَالْخَلِيلَ سِمِAdam vint la féliciter de même que Seth, Henoh, Noé, Houd ; mentionne Abraham, l’ami de DIEU; ثُمَّ الذَّبِيحُ كَلِيمُ اللَهِ كِلْمَتُهُ مِنْ أَوَّلِ الشَّهْرِ فِي التَّرْتِيبِ لَا تَهِمِPuis celui qu’on destina au sacrifice, (Ismaël) celui qui parla à DIEU(Moise), celui qui exista par Son Verbe. Ils vinrent au début de chaque mois, l’un après l’autre. Ne doute point de cette énumération ainsi ordonnée. عَلَى النَّبِي وَعَلَيْهِمْ أَجْمَعِينَ سَلَا مَا رَبِّنَا دَائِمًا عَمًّا بِصَحْبِهِمِQue les deux saluts de notre SEIGNEUR soient sur notre Prophète et sur eux éternellement, en même temps que sur leurs compagnons. Mame Maodo Malick Sy borom Parassol bi. Source : www.Serignemansoursy.com Merci de visiter le site et participer pour aider la science 👌

Les 23 Chartes de la Tariixa Tijjaan

1- Nga jàpp wird bi ci ku am ndigal bu wér; ndigal guy jàppaloo ba ci Siidi Ahmet Tijaani ni callala. Le postulant doit être affilié par un muqaddam qui lui-même est consacré dans sa fonction par le Cheikh fondateur ou un des ses représentants notoires. 2- Ki jël Tariixa bi, na fekk bumu yore benn wirdu Sëriñ, walla na bàyyi wirdu Sëriñ boobu, walla Muxàddam bi bu mu ko may wird bi. Su ko ko mayee, dog na, moom Muxàddam bi ci Tariixa bi. Soo bàyyee sa wird, Seex moo la gaaranti.Tijaan bi su bàyyee wirdam, benn Sëriñ manu ko aar ci alku, ak Sëriñ boobu lu mu rëy-rëy maartaba, ak ku mu man a doon. Le postulant doit être libéré de toute obédience envers une autre tarixa. Si le postulant accepte de laisser son wird initial, il est sous la protection de CHEIKH, quelque rang quoccupe le Serigne quil quitte. Si le tidiane par contre laisse son wird, aucun serigne, quel que soit son rang ou son grade, ne peut le prémunir de sa perdition. 3- Doo siyaare benn wàlliyu buy dund ak bu dee bu dul Tiijaan.Te boo ko defe dog nga ci Tariixa bi.Du xeebate walla rëylu, sàrt la rekk.Terewul seetante, demante. Il lui est absolument interdit de visiter  » ziarra » ou dinvoquer lintercession de tout saint étranger (non tijaane) vivant ou mort, sous peine dêtre exclu de la tarixa. Il doit néanmoins considération et respect à tout saint homme sans exclusive. Cette conditionnalité nexclut pas non plus une fréquentation entre musulmans. 4- Saxoo di julli julli juróom, ci boppu waxtu wa, ci mbooloo, ndeem Ilimaan ja mat na Ilimaan, di matal rukoo ak sujoot ya ak sellal Faatiha ; te saxoo topp sunna. Les adeptes du masculin doivent faire les cinq prières en assemblée, et autant que possible à la mosquée. Les adeptes du sexe féminin prieront à la première heure de la période correspondant à chaque prière. Les deux adeptes du sexe se soumettront aux lois établies par la Charria et suivront la souna. 5- Saxoo bëgg Seex Ahmet Tijaani ba kerook ngay dee, ak xalifaam, ormaal ko ni ngay ormalee Seex ci boppam. Il lui faut aimer Cheikh Ahmed Tijane et ses khalifes d’un amour puissant et toujours croissant, honorer le khalife de Cheikh au même titre que lui-même. 6- Bañ a nangu mukk, bañ a wóolu pexem Yàlla. Ngëneelu Tariixa bi, bu mu tax nga bañ a def li la war ak bàyyi li la war. Soo ko defee, Yàlla dina la nattu ba nga bañ a Seex. So bañee seex génn nga ci Tariixa bi. Il lui faut se garder d`un excès de confiance, de se suffire soi- disant du dessein de DIEU. Ne point se fonder sur les promesses et les avantages de la tarixa et « se croiser les bras ». 7- Doo xas mukk, doo noonoo mukk, doo goti mukk Seex Ahme Tijaane. Il ne proférera jamais d’injures ou de critiques à l’adresse de Cheikh Ahmed Tijaane. 8- Saxo wird, wasifa, ak Hadara jumaa ba keroog ngay dee. Ne jamais abandonner l’ordre après y avoir été affilié, pratiquer le wird jusqu’à la mort. 9- Sa pas-pas du wàññiku mukk, doo ko uri mukk. Sa orma ci Seex su wàññikoo, xamal ni sa pas-pas wàññiku na . Avoir la ferme conviction de la voie. 10- Doo weddi, doo diiŋat ( doo contre) Seex Ahmet Tijjaan nee na: lu mu wax, natt leen ko ci Alxuraan ak sunna.Su dëppoowul, waxu ko.Kon ku ko weddi Yàlla ak Yónnent Bi nga weddi. Te garder en toute circonstance de discréditer cheikh Ahmed Tijaane car tout ce qu’il dit et fait est conforme aux recommandations de Dieu et de son prophète ( S.A.S) 11- Taalibe bi, bumu wird mukk te amu ci ndigal. Aucune personne non affiliée ne doit réciter les oraisons sans autorisation d’un muqaddem. 12- Daje di wasifa ak Hadara jumaa ci mbooloo ndeem Tijjaan a nga fa. Assister la récitation de la wazifa et du hadara du vendredi en assemblée (si possible) 13- Doo jàng Jawharatul-Kamal te andoo ak njàpp. Il ne faut jamais réciter la Djawharatoul-Kamal (perle de la perfection) sans ablutions rituelles. 14- Doo noononte doo dogoonte ak mbindaafoon yi rawati na ki nga bokkal Tariixa bi . Il est interdit à l’adepte de se brouiller avec tout être humain et, encore moins avec un tijaane. 15- Doo doyadal wird wi di ko yéexe ba waxtu wi génn te amoo ngànt. Il faut éviter toute négligence dans la pratique, notamment tout retard dans la récitation du wird, si ce n’est un cas de force majeure réelle. 16- Bul maye wird te amoo ndigalu maye ko. Il ne faut jamais, sans investiture, s’attribuer le titre de moqaddem et donner le wird 17- Nga ormal képp ku askanoo ci Seex rawatina magu Tariixa bi . Respecter, honorer les gens de la tarixa, en particulier les « anciens » qui ont acquis des grâces particulières de DIEU 18- Sooy wird nga laab ci sa yaram ak ci sa yére. Veiller à la propreté rigoureuse de son corps, de ses habits. 19- Na ngay wird ci barab bu laab, bu yaatu , fu 6i nit xaj (lu mu néew-néew) ngir nga sori sobe. Veiller à la propreté rigoureuse de l’endroit où on effectue le wird, ainsi qu’à son espacement (6 personnes) 20- Toog jublu penku bu dul ngay doxe donte mu gàtt, walla nga nekk ci géewu wasifa. Il faut pendant la récitation des oraisons, se tourner vers la KAABA ( temple sacré de la Mecque), sauf en cas d’exception prévus (lorsqu’on se déplace en marchant par exemple). 21- Doo wax sooy wird lu dul ci loraange ak ñu dul Sëriñ bi lay tarbiya, sa nday, sa baay, mbaa sa jëkkër ñooñii lu leen neex wax ak yaw . Il ne faut jamais, sauf en cas de force majeure, interrompre la récitation par d’autres paroles à l’exception de votre cheikhou tarbiya, votre père, votre mère ou votre mari. 22- Teewlu jëmmi Yónnent …

Les 23 Chartes de la Tariixa Tijjaan Lire la suite »

Laxdariyu en wolof

Laxdariyu en wolof { UBBITEG TÈERE BI } Nu tàmbalee sunu jëf ci tudd Yàlla. Yàlla miy xéewale bépp mbindeef fii ci àdduna, tey yërëm ku ko soob ëllëg (ca allaaxira).Yàlla na Yàlla julli ci sunu sang bi Muhammat, ak i ñoñam, ak i saabaam, te musal ko.Mboleem cant yi ñeel na Yàlla, moom miy Boroom mbindeef yi. Te dollikug xéewal, ak dollikug mucc Yàlla na nekk ci sunu sang Muhammat, ka mottali ñañu soloo, tay njiitu ñañu yónni. { PAS-PAS } Li njëkk a war ci mukàllaf mooy mu wéral ngëmëm, topp mu xam la nga xam ne dana yéwénal ci moom faratay jëmmam, lu mel ni àttey julli, ak laab, ak koor. Dana war ci moom mu wattandiku ci daytali Yàlla yi, te mu taxaw ci ay ndigalam, te muy tuub jëm ci Yàlla, (mu sell mi), lu jiitu muy mer. (Wax Wolof Ak Xamle) Bind ñaar (2) *Laxdariyu * { SÀRTI TUUB } Sàrti tuub ñooy : réccu ca la weesu, ak yéenee bañ a dellu ci bàkkaar ci li des ci sag dund, ak bàyyi moy ga ca saa si bu dee nekkoon nga aji-làmboo ci moy.Du dagan ñeel mukàllaf mu yeexe tuub, te déet muy wax ba Yàlla gindi ma. Naka loolu bokk na ci mandargay texeedi, ak jéppte, ak gumbag xol. { TEGGIINI LISLAAM } Dana war ci mukàllaf mu wattu làmmiñam ci ay ñaawtéef, ak wax ju ñaaw (saaga, xaste), ak ngiñal pase, ak gëdda ab jullit, ak doyadal ko, ak ƞàññ ko, ak ragal loo ko ci lu dul dëggug kojug yoon.Dana war ci mukàllaf mu wattu gisam ci xool jëm ci lu araam. Du dagan ñeel ko muy xool jëm ci jullit xool boo xam ne da koy lor, lu dul ni dafa nekk faasix (kàccoor). Kon dana war tongoo ak moom (gàddaay ko). (Wax Wolof Ak Xamle) Bind ñatt (3) *Laxdariyu * Dana war ci mukàllaf mu wattu gisam ci xool jëm ci lu araam. Du dagan ñeel ko muy xool jëm ci jullit xool boo xam ne da koy lor, lu dul ni dafa nekk faasix (kàccoor). Kon dana war tongoo ak moom (gàddaay ko).Dana war ci mukàllaf mu wattu mbooleem i céram lu mu man (kem kàttanam), te muy bëgg (sopp) ngir Yàlla, muy bañ ngir Yàlla, muy gërëm ngir Yàlla, muy mere ngir Yàlla, muy digle luy tax a am aw yiw, tay tere lu bon (lu ñu sib).Araam na ci mukàllaf muy fen, ak jëw, ak rambaaj, ak rëy, ak naw jëf (yéem boppam), ak ngistal, ak ndéggtal, ak kañaan, ak mbañeel, ak seet ngëneel ci keneen, ak jëwe bët (regeju), ak jëwe gémmiñ (ngeleju), ak po (mariyaas, damye, futbal, rawante), ak reetaanu xol, ak njaalo, ak xool jëm ci jaambur bu jigéen, ak bànneexu ciy waxam, ak lekk alalu nit ci lu dul teeyug bakkanam, ak lekk alal ci tinu nit , walla ci (turu) diine, ak yeexe julli ba génn waxtu wa.Daganul ci mukàllaf muy ànd ak kàccor, walla jekkiyaale (toog) ak moom ci lu dul lor (ngànt). (Wax Wolof Ak Xamle) Bind ñent (4) *Laxdariyu * Déet muy sàkku ngërëmal mbindeef ci senjug (merug) Aji-Bind Ji Yàlla (tudd naa ag sellam) wax na : « Naka Yàlla ak Yònnentam ñoo gën a yayoo ñu sàkku seen ngërëm, bu dee nekk nañu ay way gëm ».Yònnent Bi (Yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc) wax na ne : « Bul topp menn mbindeef ci moy Aji-Bind Ji».Daganul ci mukàllaf mu jëf jenn jëf mbate mu xam àtteb Yàlla ci jëf ja. Nay laaj way xam ña, te muy roy ci way topp ña sunnas Muhammat (Yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc). Mooy ña nga xam ne dañuy tegtale ci topp Yàlla, di wattandikuloo (moytuloo) ci topp saytaane. Déet muy gërëm ñeel boppam (bëgg ci boppam) loo xam ne gërëm na ko way-falas (kutus) ña. Mooy ña nga xam ne sànk nañu seen dund ci lu dul topp Yàlla mu kawe mi. Woo naa (tudd naa) seen ñàkk nga (pert), seen jooy yu yàgg Bis-Pènc ba.Noo ngi ñaan Yàlla (tudd naa ag sellam) mu dëppale nu ci topp sunnas sunu Yònnent, sunu rammkat, sunu sang Muhammat (Yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc). (Wax Wolof Ak Xamle) Bind juróom (5) *Laxdariyu * { XAAJI LAAB } Laab ñaari xaaj la: laabu hadas (dindi toj ci njàpp, walla ci cangaay) ak laabu xabas (dindi sobe su la taq ci yère, walla yaram, walla bérab bi ngay jullee ). Ñaar yépp duñu wér lu dul ci ndox mu laab, te man a laabal. Mooy ndox moo xam ne soppikuwul meloom wa, walla cafkaam ga, walla xetam ga, ci loo xam ne dana teqalikoo ak moom ca la gën a not, lu mel ni peterol, ak diw, ak ñaay ak nékk (gares), diwu segal), ak tèru jur (tilim), ak saabu, ak tèru nit (mbalit), ak yu ni mel.Aayul ci suuf, ak dewnde (ban bu ñuul), ak ceñ (xorom), ak mbaala-mbaal ak ñax mi sax ci ndox, ak yu ni mel. (Kon yii mu mujj a tudd buñu soppee ndox du ko tee laab te man a laabal.) (Wax Wolof Ak Xamle) Bind juróom benn (6) *Laxdariyu * { LAAB CI SOBE } Bu dee sobe sa ràññeeku na, raxaseef bérab ba. Bu dee lënt na, raxaseef mbalaan ma léppam (maanaam yère ba).Ku sikki-sàkka ci laalug sobe, na ko wis. Bu dee laal na ko, mu sikki-sàkka ci sobewoom, déet wis di ko war.Ku fàttaliku sobe te nekk ci julli, na ko dog, lu dul ne dafa ragal génn waxtu wa.Ku julli ànd ak sobe di aji-fàtte, te mu fàttaliku ko ginnaaw ba mu sëlmalee, na baamu ca waxtu wa (maanaam bu waxtu wa jàllee du ko baamu). (Wax Wolof Ak Xamle) Bind juróom ñaar (7) *Laxdariyu * { FARATAY NJÀPP } Faratay njàpp juròom ñaar lañu: yéene, ak raxas kanam (sëlmu), ak raxas ñaari yoxo ba ca ñaari conca ya, ak masaa bopp, ak raxas ñaari tànk ba ca ñaari dojoor ya, ak …

Laxdariyu en wolof Lire la suite »

Retour en haut
Ouvrir la discussion
Bonjour,
Pouvons-nous vous aider ?